septembre 22, 2017

Contact: 775312579 Email: redaction@thiesinfo.com
BBY THIES

Il accuse gravement le maire de Ngoundiane: Mbaye DIONE Regardez

[template id= »23032″]

appli

4 Comments

  1. justice

    jim mbaye faye n’a pas le temps d’instrumentaliser qui que se soit le fait de dire diangoul me fait rire youssou ndour etait ministre et il fait parti des hommes les plus riche au senegal foumou diangué mbaye faye est un directeur general d’une societe de travaux publics jim ndiang dou wess

    Reply
  2. Jim

    ces gens sont insyrumentalisés par le socialiste Mbaye Faye entrepreneur, mais nous lui disons que ces parasites ne peuvent rien t’apporter: meunou niou la diokh Ngoundiane parce que diangoulo, dagnou lay nakh, sa alal rek lanou beuga lekk ak sa passou Maka yi ngay diokhé. même si on organise des élections demain Mbaye Dione va gangner avec 80% à la place des 63% de 2013. gnii ay rambadj you goor la nou, Gnou beuga diakhassé Maire bi ak Khalif G mourite aK Tidiane. ana goor ak rambadj ak saytané. Mbaye limoy dieuf ci yoonou mouride ak tidiane khadj bi sakh défoléén ko parce que amoolén lou nguéén lekk, liguéyou léén, danguén di takhawalou rek ak took ci grand place yi di dieuwaté, ay nafekh nguéén. Ngoundiane nieup khamanté nanou, loway meun rek xaam nanouko. dém léén liguéyi, wakh wakh rek, ignane, sokhor, ciss. kén nangou woul investir dara ci deuk bi ndakh séni lamègne, lo way di déf nguén wakh thi bamou yakhoulé parce queséni guémeugn dafa dangereux, domi deuk bi gni téki yeup angui daw dakh séén thiate. Yalla nanou Yalla moussal ci séén lamégne yi. ba benén yoon, teu souguén défoul attention séni mboott you bari dinanou ka wakh ci presse bi parce que xam nanou lou bari, xam nanou léén bou bakha bakh. wassalam!

    Reply
  3. frere

    ils veulent mettre en mal Mbaye Dione et Macky Sall, Moustapha Niasse, Alioune Sarr; ay saytané nguèn. Sou lèèn gni deglo ma xamné matounou lignou doon. ay dof yi nou peinture comme gni nga xam né dagnou khif Ngour parce qu’ils veulent se cacher dérrière la politique pour vivre, amouniou béni métier. Mbaye dione mo leen guena nek talibé fou, guen lén djioulité et je parle en connaissance de cause. il y a parmi eux des pédophiles, des voleurs de bétail, ay dieuwkat you bonn, ba paré tékki wouniou dara Ngoundiane. mank dokh bi thie deuk bi gn kofi bayi

    Reply
  4. Deug

    voici de véritables menteurs, des opposants boutés, chassés de la commune de Ngoundiane par la population depuis 2009 et qui veulent revenir au pouvoir, mais nous population de la localité, nous leur disons c’est peine perdue, nous ne voulons plus d’eux. ces gens là méritent même d’être pendus parce que c’est eux qui ont retardé Ngoundiane, ils avaient mis à genoux cette localité pendant 20 ans. allez visiter Ngoundiane, Mbaye Dine a su le sortir du trou en 5 ans et a gagné les dernières élections avec 63% des suffrages. tous ces gens là que voyez sont des sacrés chomeurs qui veulent dilapider les ressources de la localité comme ils l’avez fait de 1992 à 2009, ça ne passera pas parce que la population les a vomi comme du sang pourri. ils n’ont qu’à aller travailler aulieu de passer tout leur temps aux grandes places; même l’agriculture hivernale ils ne le font pas, ils sont nuisibles pour la socièté. ligueyi leen nafekh yi nguèn doon, wakh rek. Yalla dou fay wakh mouk bayi dieuf teu Mbaye Dione day dieuf. mais aussi ki dieuf ba raw la meuno wakh ba dab ko; au travail! kou xool ki di wakh rek nga kham né chomeur bou sonn leu; ken doulen diokhati Ngoundiane nguen diarigno ay ressource sam, dém leen liguéyi sou nguén beugué lo nguén lekk fénkat yi nguén doon. allez vous faire foutre dokhadèm!

    Reply

Postez un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée.

thies massage